Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 125:3-5 in Wolof

Help us?

Sabóor 125:3-5 in Kàddug Yàlla gi

3 Nguur gu bon du saxe kaw suuf su nit ñu jub muurloo. Lu ko moy ñu jub ñi sàkku lu bon, di ko jëfe.
4 Éy Aji Sax ji, baaxeel ku baax, ak kuy mébét njub.
5 Waaye kuy topp yoonu ndëngte, Aji Sax jee koy sànk, boole kook kuy def lu bon. Yal na jàmm dal Israyil.
Sabóor 125 in Kàddug Yàlla gi