Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 124:7-8 in Wolof

Help us?

Sabóor 124:7-8 in Kàddug Yàlla gi

7 Danu ne fërr, nim picc mu rëcc fiiru rëbb, fiir ga toj, nu raw.
8 Sunu ndimbal a ngi ci turu Aji Sax ji, ki sàkk asamaan ak suuf.
Sabóor 124 in Kàddug Yàlla gi