Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 124:3-5 in Wolof

Help us?

Sabóor 124:3-5 in Kàddug Yàlla gi

3 ba nit ña xadaroo sunu kaw, dañu nu doon wonn, nuy dund,
4 dañu nu doon mëdd nim ndox, def um wal, buub nu,
5 def waame wuy wal-wali, buub nu, yóbbu.
Sabóor 124 in Kàddug Yàlla gi