Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 122:7-9 in Wolof

Help us?

Sabóor 122:7-9 in Kàddug Yàlla gi

7 jàmm ne ñoyy fi say tata wër, te xel dal ci biir këri Buur.»
8 Mbokk ak xarit a waral may ñaan jàmmi Yerusalem.
9 Sunu kër Yàlla Aji Sax jee ma tax di sàkku ngëneelu Yerusalem.
Sabóor 122 in Kàddug Yàlla gi