Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 122:3-4 in Wolof

Help us?

Sabóor 122:3-4 in Kàddug Yàlla gi

3 Céy, Yerusalem, dëkkub tabax bu baax, bi booloo, di benn.
4 Fii la giiri Israyil di yéegsi, di giir yi Ki Sax séddoo. Ñu ngi santsi Aji Sax ji, ni ko Israyil warloo.
Sabóor 122 in Kàddug Yàlla gi