Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 121:7-8 in Wolof

Help us?

Sabóor 121:7-8 in Kàddug Yàlla gi

7 Aji Sax jee lay sàmm ci gépp loraange, di sàmm sa bakkan.
8 Aji Sax jee lay sàmm, dem ak dikk, tey ak ëllëg.
Sabóor 121 in Kàddug Yàlla gi