Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 121:4-6 in Wolof

Help us?

Sabóor 121:4-6 in Kàddug Yàlla gi

4 Kiy sàmm Israyil kay gëmmul, nelawul.
5 Aji Sax jee lay sàmm, Aji Sax jee lay yiir, féete la ndijoor.
6 Du naaj wu lay dal bëccëg, mbaa leer gu ndaw guddi.
Sabóor 121 in Kàddug Yàlla gi