Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 119:91-94 in Wolof

Help us?

Sabóor 119:91-94 in Kàddug Yàlla gi

91 Ci sa ndigal la lépp taxawe ba tey, lépp ànd, di la jaamu.
92 Su ma bégewuloon saw yoon, sànkoo sama toskare ji.
93 Duma fàtte mukk say tegtal, ci nga may musale.
94 Yaa ma moom, wallu ma; say tegtal laay sàkku.
Sabóor 119 in Kàddug Yàlla gi