Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 119:154-155 in Wolof

Help us?

Sabóor 119:154-155 in Kàddug Yàlla gi

154 Àtte ma, ba jot ma; musal ma, yaa ko dige.
155 Ku bon sore sa wall, ngir sàkkuwul sa dogali yoon.
Sabóor 119 in Kàddug Yàlla gi