Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 119:100-102 in Wolof

Help us?

Sabóor 119:100-102 in Kàddug Yàlla gi

100 Maa ëpp mag ñi dég-dég, nde say tegtal laa topp.
101 Luy yoon wu aay, ma moyu, ba mana sàmm sa kàddu.
102 Say santaane it dëdduwma ko, nde yaw yaa ma jàngal.
Sabóor 119 in Kàddug Yàlla gi