Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 119:100-101 in Wolof

Help us?

Sabóor 119:100-101 in Kàddug Yàlla gi

100 Maa ëpp mag ñi dég-dég, nde say tegtal laa topp.
101 Luy yoon wu aay, ma moyu, ba mana sàmm sa kàddu.
Sabóor 119 in Kàddug Yàlla gi