Text copied!
Bibles in Wolof

ROOM 8:7 in Wolof

Help us?

ROOM 8:7 in Téereb Injiil

7 Ndaxte ku fonk sa nafsu, bañaaleb Yàlla nga, ndaxte doo déggal Yàlla, mbaa ngay sàmm ay santaaneem, te manuloo koo def sax.
ROOM 8 in Téereb Injiil

Room 8:7 in Kàddug Yàlla gi

7 Ndaxte boroom xintey bakkan ab noonu Yàlla la, nde déggalul yoonu Yàlla, te manu ko sax.
Room 8 in Kàddug Yàlla gi