Text copied!
Bibles in Wolof

ROOM 7:18 in Wolof

Help us?

ROOM 7:18 in Téereb Injiil

18 Ndaxte xam naa ne lu baax dëkkul ci man, maanaam ci sama bindu doom Aadama. Am naa yéeney def lu baax, waaye awma kàttanu yeggale.
ROOM 7 in Téereb Injiil

Room 7:18 in Kàddug Yàlla gi

18 Xam naa ne man, sama bindu suuxu neen wii, lenn lu baax dëkku ci. Yéene jaa ngeek man, kàttanu jëfe lu baax moo fi nekkul.
Room 7 in Kàddug Yàlla gi