Text copied!
Bibles in Wolof

ROOM 2:18-19 in Wolof

Help us?

ROOM 2:18-19 in Téereb Injiil

18 Xam nga coobareem, ndaxte jàng nga ci yoonu Musaa, ba fonk yëf yi gëna baax.
19 Yaa ngi teg sa bopp wommatkatu gumba yi ak leeru ñi nekk cig lëndëm.
ROOM 2 in Téereb Injiil

Room 2:18-19 in Kàddug Yàlla gi

18 Yaa xam coobarey Yàlla, te yaa jànge ci yoonu Musaa, ba xam li am solo dëgg.
19 Yaw mi mu wóor ne yaa di wommatkatub gumba yi, te di leeru ñi ci lëndëm gi,
Room 2 in Kàddug Yàlla gi