Text copied!
CopyCompare
Téereb Injiil - ROOM - ROOM 1

ROOM 1:6-7

Help us?
Click on verse(s) to share them!
6Te ci ngeen bokk, yéen ñi Yàlla woo, ngeen nekk ci Kirist.
7Yéen ñi dëkk Room ñépp, yéen ñi Yàlla bëgg te woo leen, ngeen nekk gaayam yu sell, na leen Yàlla sunu Baay ak Boroom bi Yeesu Kirist may yiw ak jàmm.

Read ROOM 1ROOM 1
Compare ROOM 1:6-7ROOM 1:6-7