Text copied!
CopyCompare
Téereb Injiil - ROOM - ROOM 1

ROOM 1:24-25

Help us?
Click on verse(s) to share them!
24Moo tax Yàlla bërgël na leen ci seeni bëgg-bëgg, ñu sóobu ciy ñaawteef, di jëflante lu gàccelu ci seeni cér.
25Toxal nañu dëggu Yàlla, tëral fen, di màggal ak a jaamu mbindeef, ba faaleetuñu sax Aji Bind, ji yelloo cant ba fàww. Amiin.

Read ROOM 1ROOM 1
Compare ROOM 1:24-25ROOM 1:24-25