Text copied!
Bibles in Wolof

ROOM 1:12 in Wolof

Help us?

ROOM 1:12 in Téereb Injiil

12 Maanaam ma nekk ci seen biir, te nu dimbaleente ci sunu ngëm, ndax man itam ma gëna am doole.
ROOM 1 in Téereb Injiil

Room 1:12 in Kàddug Yàlla gi

12 te loolu mooy ma bokk ak yeen lu dëfal sama xol, dëfal leen, ci seen ngëm ak sama gos.
Room 1 in Kàddug Yàlla gi