Text copied!
Bibles in Wolof

PEEÑU MA 20:4 in Wolof

Help us?

PEEÑU MA 20:4 in Téereb Injiil

4 Noonu ma gis ay gàngune, ñu jox ña ca toog sañ-sañu àtte. Noonu ma gis ruuwi ñi ñu bóomoon ndax li ñu doon seedeel Yeesu te gëm kàddug Yàlla. Ñooñu jaamuwuñu rab wa mbaa nataalam, te nanguwuñoo am màndargam rab wa ca seen jë mbaa seen loxo. Ñu daldi dekki, di nguuru ak Kirist diirub junniy at.
PEEÑU MA 20 in Téereb Injiil

Peeñu ma 20:4 in Kàddug Yàlla gi

4 Ci kaw loolu ma gis ay gàngune yu ñu jox ña ca toog, sañ-sañu àtte. Ma daldi gis bakkani ñi ñu dogoon seen bopp ndax la ñu doon seedeel Yeesu ak la ñu gëmoon kàddug Yàlla, ña sujjóotalul woon rab wi ak jëmmu nataalam, te amuñu màndargam rab wi ci seen jë mbaa seen loxo. Ñu dekki bay nguuroondoo ak Almasi diiru junniy at.
Peeñu ma 20 in Kàddug Yàlla gi