Text copied!
Bibles in Wolof

PEEÑU MA 18:4 in Wolof

Help us?

PEEÑU MA 18:4 in Téereb Injiil

4 Noonu ma dégg beneen baat bu jóge asamaan naan: «Génnleen ci biiram, yéen samay gaay, ngir ngeen baña bokk ci ay bàkkaaram te baña am cér ci musiba yi koy dal.
PEEÑU MA 18 in Téereb Injiil

Peeñu ma 18:4 in Kàddug Yàlla gi

4 Ci kaw loolu ma dégg beneen baat bu jóge asamaan, ne: «Yeen sama ñoñ, génnleen dëkk bii, bala ngeena bokk ak moom ay bàkkaaram, bay séddu ci mbugalam.
Peeñu ma 18 in Kàddug Yàlla gi