Text copied!
Bibles in Wolof

Ose 2:20 in Wolof

Help us?

Ose 2:20 in Kàddug Yàlla gi

20 Bésub keroog maa leen di fasal kóllëre ak rabi àll yeek njanaaw yi, ak ndëgmeent yi. Fitt ak saamar akub xare it, maa koy dagge ci réew mi, te maa leen di may tëraayu jàmm.
Ose 2 in Kàddug Yàlla gi