Text copied!
Bibles in Wolof

Njàlbéen ga 3:16 in Wolof

Help us?

Njàlbéen ga 3:16 in Kàddug Yàlla gi

16 Yàlla teg ca ne jigéen ja: «Dinaa taral sa metitu mat, ci metit ngay wasin. Sa bëgg-bëggu bakkan dina la xiir ci sa jëkkër, te moo lay teg tànk.»
Njàlbéen ga 3 in Kàddug Yàlla gi