Text copied!
Bibles in Wolof

Ngën-gi-woy 6:3-4 in Wolof

Help us?

Ngën-gi-woy 6:3-4 in Kàddug Yàlla gi

3 Man, nijaay a moom; nijaay it, maa moom. Mooy fore sama digg tóor-tóor yi.
4 Xarit, taaru nga ni Tirsa ak Yerusalem, péeyi buur ya, yéeme nga ni péey yu kawe ya!
Ngën-gi-woy 6 in Kàddug Yàlla gi