Text copied!
Bibles in Wolof

Ngën-gi-woy 5:16 in Wolof

Help us?

Ngën-gi-woy 5:16 in Kàddug Yàlla gi

16 Gémmiñam, bànneexi neen, jëmmam jépp jara xédd! Yeen janqi Yerusalem, sama nijaay a ngoog, samab xarit.
Ngën-gi-woy 5 in Kàddug Yàlla gi