Text copied!
Bibles in Wolof

Ngën-gi-woy 2:13-16 in Wolof

Help us?

Ngën-gi-woy 2:13-16 in Kàddug Yàlla gi

13 Figg a ngi ñorsi, reseñ tóor, di gilli. Xarit, ayca, jongama sama, dikkal boog!»
14 Soppe, sore nga ni xati mu dëkke xar-xari doj, làqoo ruqi mbartal yi. Won ma sa jëmm, dégtal ma sa baat. Sa baat a neex, sa jëmm jekk!
15 Jàppal-leen ma till yi, till yu ndaw yiy ruur reseñ, te sunu reseñ jiy tóor.
16 Sama nijaay, maa moom, man it, moo moom, di fore digg tóor-tóor yi.
Ngën-gi-woy 2 in Kàddug Yàlla gi