Text copied!
Bibles in Wolof

Ngën-gi-woy 1:2-3 in Wolof

Help us?

Ngën-gi-woy 1:2-3 in Kàddug Yàlla gi

2 Fóon maa, ngalla fóon ma, sa cofeel a ma dàqal biiñ.
3 Sa diw yi ngay xeeñoo neex, saw tur jib, mel ni lu xeeñ a xelli. Moo tax janq ji nob la.
Ngën-gi-woy 1 in Kàddug Yàlla gi