Text copied!
Bibles in Wolof

Ngën-gi-woy 1:15-17 in Wolof

Help us?

Ngën-gi-woy 1:15-17 in Kàddug Yàlla gi

15 Xarit, yaaka rafet, yaaka taaru! Say gët niy pitax.
16 Nijaay, yaaka góorayiw, yaaka maa neex! Mbooy gu naat, nu laloo,
17 garabi seedar di sunu xànqi néeg, garab gu dul ruus xadd ko.
Ngën-gi-woy 1 in Kàddug Yàlla gi