Text copied!
Bibles in Wolof

Ngën-gi-woy 1:14-16 in Wolof

Help us?

Ngën-gi-woy 1:14-16 in Kàddug Yàlla gi

14 Saa nijaay, saa cabbu tóor-tóoru fuddën, fa digg tóokëri Engedi.
15 Xarit, yaaka rafet, yaaka taaru! Say gët niy pitax.
16 Nijaay, yaaka góorayiw, yaaka maa neex! Mbooy gu naat, nu laloo,
Ngën-gi-woy 1 in Kàddug Yàlla gi