Text copied!
Bibles in Wolof

Ngën-gi-woy 1:13-14 in Wolof

Help us?

Ngën-gi-woy 1:13-14 in Kàddug Yàlla gi

13 Sama nijaay di mbuusum ndàbb may fanaan sama digg ween.
14 Saa nijaay, saa cabbu tóor-tóoru fuddën, fa digg tóokëri Engedi.
Ngën-gi-woy 1 in Kàddug Yàlla gi