Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Ngën-gi-woy 1:10-13 in Wolof
Help us?
Ngën-gi-woy 1:10-13
in
Kàddug Yàlla gi
10
Sa lex yaa ngi tàkk fi digg sàdd yi! Céy wii loos ak caqu peram!
11
Sàddi wurus lanu lay defaral, tapp ca xaalis.
12
Li sama buur tëdd, di xéewlu lépp, maa ngi gilli lu neex.
13
Sama nijaay di mbuusum ndàbb may fanaan sama digg ween.
Ngën-gi-woy 1 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms