Text copied!
Bibles in Wolof

MÀRK 4:35-36 in Wolof

Help us?

MÀRK 4:35-36 in Téereb Injiil

35 Bés booba nag ci ngoon Yeesu ne taalibe yi: «Nanu jàll dex gi.»
36 Mu yiwi mbooloo mi nag, ay taalibeem jël ko ni mu mel ci gaal gi; te yeneen gaal ànd ak moom.
MÀRK 4 in Téereb Injiil