Text copied!
Bibles in Wolof

Màndiŋ ma 24:6-7 in Wolof

Help us?

Màndiŋ ma 24:6-7 in Kàddug Yàlla gi

6 Ña nga ne màww ni tooli tàndarma, nirooteek tóokëri tàkkal dex, mbaa garabu alowes gu xeeñ gu Aji Sax ji jëmbat, mbaa garabi seedar yu saxe wali ndox.
7 Ndox maay wale cay bagaanam, am jiwoom màndim ndox, buuram nara sut Buur Agag, nguuram jóg ba kawe.
Màndiŋ ma 24 in Kàddug Yàlla gi