Text copied!
Bibles in Wolof

Màndiŋ ma 24:15-16 in Wolof

Help us?

Màndiŋ ma 24:15-16 in Kàddug Yàlla gi

15 Ci kaw loolu mu yékkati kàddug ñaanam, ne: «Kàddug Balaam a ngi, doomu Bewor, kàddug waa jiy boroom ngis,
16 kàddug kiy dégg waxi Yàlla, kiy xame ca xam-xamu Aji Kawe ji, Aji Man ji wonem peeñu, mu gis, kiy daanu leer, te ay gëtam muriku.
Màndiŋ ma 24 in Kàddug Yàlla gi