Text copied!
Bibles in Wolof

Màndiŋ ma 22:20-21 in Wolof

Help us?

Màndiŋ ma 22:20-21 in Kàddug Yàlla gi

20 Ci kaw loolu Yàlla dikkal Balaam ca guddi ga, ne ko: «Gannaaw woosi la mooy tànki ñii, àndal ak ñoom. Waaye nag lu ma la wax rekk, def ko.»
21 Ca ëllëg sa Balaam takk mbaamam, ànd ak kàngami Mowab, dem.
Màndiŋ ma 22 in Kàddug Yàlla gi