Text copied!
Bibles in Wolof

LUUG 9:51-52 in Wolof

Help us?

LUUG 9:51-52 in Téereb Injiil

51 Bi jamono ji jegeñsee, ji Yeesu waree jóge àddina dem asamaan, mu sigiñu ci dem Yerusalem.
52 Noonu mu yebal ay ndaw, ñu jiitu ko. Ñu dem nag, dugg ci ab dëkk ci diiwaanu Samari, ngir wutal ko fa fu mu dal.
LUUG 9 in Téereb Injiil

Luug 9:51-52 in Kàddug Yàlla gi

51 Ba ñu demee ba bés bi ñu wara yéege Yeesu di jubsi, Yeesu moo dogu ngir dem Yerusalem.
52 Mu yebal ay ndaw, ñu jiitu ko. Ñu dem, ba agsi ab dëkk ci diiwaanu Samari, nar ko faa waajal ab dal.
Luug 9 in Kàddug Yàlla gi