Text copied!
Bibles in Wolof

LUUG 6:46 in Wolof

Help us?

LUUG 6:46 in Téereb Injiil

46 «Lu tax ngeen may wooye “Boroom bi, Boroom bi,” te dungeen def li may wax?
LUUG 6 in Téereb Injiil

Luug 6:46 in Kàddug Yàlla gi

46 «Ana lu ngeen ma naa “Sang bi, Sang bi,” te jëfewuleen samay wax?
Luug 6 in Kàddug Yàlla gi