Text copied!
Bibles in Wolof

LUUG 4:29-30 in Wolof

Help us?

LUUG 4:29-30 in Téereb Injiil

29 Noonu ñu jóg, génne ko dëkk ba, yóbbu ko ca mbartalum tund, wa ñu sanc seen dëkk, ngir bëmëx ko ci suuf.
30 Waaye moom mu jaar ci seen biir, dem yoonam.
LUUG 4 in Téereb Injiil

Luug 4:29-30 in Kàddug Yàlla gi

29 Ñu jóg, bëmëx ko ba génne ko dëkk ba, yóbbu ko ca kéméju tund, wa seen dëkk ba sance, ngir xalab ko ci suuf.
30 Teewul moom mu jaare ci seen biir, dem yoonam.
Luug 4 in Kàddug Yàlla gi