Text copied!
Bibles in Wolof

LUUG 1:21 in Wolof

Help us?

LUUG 1:21 in Téereb Injiil

21 Fekk na booba mbooloo maa ngi xaar, jaaxle lool ci li Sakari yàgg ca bérab bu sell ba.
LUUG 1 in Téereb Injiil

Luug 1:21 in Kàddug Yàlla gi

21 Ci biir loolu mbooloo maa ngay xaar Sàkkaryaa, jaaxle lool ndax yàggaayam ca biir néeg Yàlla ba.
Luug 1 in Kàddug Yàlla gi