Text copied!
Bibles in Wolof

LUUG 16:11 in Wolof

Help us?

LUUG 16:11 in Téereb Injiil

11 Su fekkeente ne nag jubuleen ci alalu àddina, kon ku leen di dénk alal ju wóor ji?
LUUG 16 in Téereb Injiil

Luug 16:11 in Kàddug Yàlla gi

11 Kon su ngeen maanduwul ci alalu àddina, alal ji dëgg, ana ku leen koy dénk?
Luug 16 in Kàddug Yàlla gi