Text copied!
Bibles in Wolof

LUUG 12:27 in Wolof

Help us?

LUUG 12:27 in Téereb Injiil

27 «Seetleen ni tóor-tóori ñax mi di saxe. Duñu liggéey, duñu ëcc, waaye maa ngi leen di wax ne Suleymaan sax ci ndamam soluwul woon ni benn ci ñoom.
LUUG 12 in Téereb Injiil

Luug 12:27 in Kàddug Yàlla gi

27 «Seetleen ni tóor-tóor yiy saxe. Sonnuñu, ëccuñu, waaye maa leen ko wax, Suleymaan ak darajaam jépp sax, soluwul woon ni benn ci ñoom.
Luug 12 in Kàddug Yàlla gi