Text copied!
Bibles in Wolof

Kàdduy Waare 8:6-8 in Wolof

Help us?

Kàdduy Waare 8:6-8 in Kàddug Yàlla gi

6 Mbir mu mu doon kat ak jotam ak doxalinam, waaye nit am na tiis wu ko diis.
7 Kenn xamul luy xew ëllëg, kenn manula wax luy xew ëllëg.
8 Kenn moomul bakkanam, ba man koo dese, kenn amul sañ-sañ ci bésub deeyam, kenn muccul ci boobu xare, te mbon du ca wallu boroom.
Kàdduy Waare 8 in Kàddug Yàlla gi