Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Kàdduy Waare 8:4-6 in Wolof
Help us?
Kàdduy Waare 8:4-6
in
Kàddug Yàlla gi
4
Kàddug buur kilifteef la. Ana ku ko naan: «Looy def nii?»
5
Ku dégg ndigal doo am lu la soof. Ku xelu, xam lu jot, xam doxalin.
6
Mbir mu mu doon kat ak jotam ak doxalinam, waaye nit am na tiis wu ko diis.
Kàdduy Waare 8 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms