Text copied!
Bibles in Wolof

Kàdduy Waare 8:3-4 in Wolof

Help us?

Kàdduy Waare 8:3-4 in Kàddug Yàlla gi

3 Bul gaawa won buur gannaaw; bul saxoo lu buur buggul; Buur, lu ko neex lay def.
4 Kàddug buur kilifteef la. Ana ku ko naan: «Looy def nii?»
Kàdduy Waare 8 in Kàddug Yàlla gi