Text copied!
Bibles in Wolof

Kàdduy Waare 6:7-9 in Wolof

Help us?

Kàdduy Waare 6:7-9 in Kàddug Yàlla gi

7 Nit ak doñ-doñam jépp, biiram, te taxul mu doylu.
8 Ana lu boroom xel ëpplee ku dofe? Nga ñàkk, xam doxalin, lu mu lay jariñ?
9 Doyloo li nga gis a gën di wéye xemmem. Loolu it, cóolóoli neen ak napp um ngelaw.
Kàdduy Waare 6 in Kàddug Yàlla gi