Text copied!
Bibles in Wolof

Kàdduy Waare 3:7-10 in Wolof

Help us?

Kàdduy Waare 3:7-10 in Kàddug Yàlla gi

7 Mu jot nga xar, mu jot nga gaar; mu jot nga selaw, mu jot nga wax.
8 Mu jot nga sopp, mu jot nga jéppi; mu jot nga xare, mu jot nga jàmmoo.
9 Ana lu liggéeykat biy jariñoo ciw ñaqam?
10 Gis naa ne sas la bu Yàlla sase, nu war koo sasoo.
Kàdduy Waare 3 in Kàddug Yàlla gi