Text copied!
Bibles in Wolof

Kàdduy Waare 3:20-21 in Wolof

Help us?

Kàdduy Waare 3:20-21 in Kàddug Yàlla gi

20 Ñoom ñépp a bokk jëm benn bérab ba, bokk jóge pëndub suuf, bokk dellu suuf.
21 Ana ku mu wóor ne bakkanu nit day yéeg asamaan, bakkanu mala tàbbi suuf?
Kàdduy Waare 3 in Kàddug Yàlla gi