Text copied!
Bibles in Wolof

Kàdduy Waare 3:2-5 in Wolof

Help us?

Kàdduy Waare 3:2-5 in Kàddug Yàlla gi

2 Day jot nga juddu, mu jot nga dee; mu jot nga jëmbat, mu jot nga buddi.
3 Mu jot nga rey, mu jot nga faj; mu jot nga toj, mu jot nga tabax.
4 Mu jot nga jooy, mu jot nga ree; mu jot nga ñaawlu, mu jot nga dukkat.
5 Day jot nga sànniy doj, mu jot nga dajale; mu jot nga fóon, mu jot nga baña fóon.
Kàdduy Waare 3 in Kàddug Yàlla gi