Text copied!
Bibles in Wolof

Kàdduy Waare 3:14-16 in Wolof

Help us?

Kàdduy Waare 3:14-16 in Kàddug Yàlla gi

14 Ma xam ne lu Yàlla def, loola day sax ba fàww. Deesu ci yokk, mbaa di wàññi dara; Yàllaa ko def, ngir nit di ko wormaal.
15 Lu ay tey, ayoon na, lu ay ëllëg it ayoon na. Yàllaay namma indi la woon.
16 Ma dellu gis fi kaw suuf ne, fu yoon moom, fa la njubadi ne, fa njub moom it, fa la njubadi ne.
Kàdduy Waare 3 in Kàddug Yàlla gi