Text copied!
Bibles in Wolof

Kàdduy Waare 3:13-14 in Wolof

Help us?

Kàdduy Waare 3:13-14 in Kàddug Yàlla gi

13 te nitoo nit, su dee lekk ak a naan, di ñaq, jariñoo, loolu mayu Yàllaa.
14 Ma xam ne lu Yàlla def, loola day sax ba fàww. Deesu ci yokk, mbaa di wàññi dara; Yàllaa ko def, ngir nit di ko wormaal.
Kàdduy Waare 3 in Kàddug Yàlla gi