Text copied!
Bibles in Wolof

Kàdduy Waare 2:7-8 in Wolof

Help us?

Kàdduy Waare 2:7-8 in Kàddug Yàlla gi

7 Ma jëndi jaam, góor ak jigéen; ñu ami doom ci kër gi. Ma am jur gu ne gàññ, gu gudd ak gu gàtt, ba ëpple ku ma jiitu ci Yerusalem.
8 Ma dajale sama xaalis ak sama wurus, moom alali buur yeek diiwaan yi ma yilif, tabb samay woykat, góor ak jigéen, boole ci bànneex bi ci jabari jabar.
Kàdduy Waare 2 in Kàddug Yàlla gi