Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Kàdduy Waare 2:4-5 in Wolof
Help us?
Kàdduy Waare 2:4-5
in
Kàddug Yàlla gi
4
Damaa liggéey lu réy. Tabaxlu naa samay kër, jëmbat sama toolub reseñ.
5
Ma sàkki tóokër aki tool, jëmbat ca garab yuy meññ lu ne,
Kàdduy Waare 2 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms